Ey Yàlla wommat ma, sàmm ma, def ma ma doon làmp bu leer ak biddééw buy melax. Yaay Boroom kàttan di Boroom doole.

‘Abdu’l-Bahá
Bahá'í Prayers, Children